
Désolé
C'est pas de ma faute
Sou féké damalaye dérangé
Désolé
Nga baalma
Xamna sakh niima mele si rewmi Nekhoula
Désolé
I'm so sorry
Soudé louma lalle
Yalla teksi loxo
Ngeunele laa
Wakhambané bou gnémé
Kouy ligueye guene
Lou setane si mane, non non
Linga dadie si yakeu
Soko dadione si ligueye
Wessou fii
Je suis désolé
C'est pas de ma faute
Sou féké damalaye dérangé
Désolé
Nga baalma
Xamna sakh
Niima mele si rewmi Nekhoula
Désolé
Go man inside
Soudé louma lalle
Yalla teksi loxo
Ngeunele laa
Wakhambané bou gnémé
Kouy ligueye guene
Lou setane si mane
Non non
Linga dadie si yakeu
Soko dadione si ligueye
Wessou fii
Je suis désolé
Si être aimé par les autres
Peut faire mal à autrui
Désolé
Si ces plumes me montent
Par mes mélodies te détruis
Je suis désolé
Yow kholale
Diiwangui néé di deme
Bour yalla koye deff si diamame
Mala douma tabakh
Because Lou domou adama bi lambo
Bour yalla koko diaguelele
(Soula yaboo)
Baye gualaye nagou Nagou mo geune
(Sa wadjii boula yaboo)
Mame Ro mo dogual nagne nagou Nopalou
Yalla gueumoul nelawoul tei dou diawaleii
Dieufou kouné louné lounekk foneii guathia
Forou mako
Lima diangue
Laye tari
Sathiou mako (lima diangue lay tarii)
"Lou waye donnou mou deugeur"
"Li gua yorr forouloko"
Ehh
N'a na na naa ooh
Forou mako
Lima diangue
Laye tari wo wo wooo
Sathiou mako
Sama gnom mame gnoma togne
Nana nana nana
"Li loussii waye mane Sing Sing dou nakhé mbaaye
Ndakh nakhé mbaaye dou yagué nii"
Aah
Non non non
Oh oh oh
Autor(es): Wally Balago Seck