
Don't Be Afraid
Sou leer deh dokh dem ngikoy hame ci bidew
Sou deuk deh doh didem gnikoy hame ci diefin euh
Denou gor dafa ara yatu dafa wara wara yatu
Ndah ki djohe dafa tabe dafa mandu motah gniou wara mandou
Non non ndeysan enh ndeysan
Man nanoy togano yalla def niou bagnia bokk guis guis
Man nanoy andano yalla def niou bagnia bokk meun meun
Man nanoy bok yoon yalla def niou bagnia book yeene
Man nanou bok khet yalla deff niou bagnia bok wawa
Denou gor dafa ara yatu dafa ara ara yatu
Ndah ki djohe dafa tabe dafa mandu motah gniou ara mandou
Adouna xel la yaye, now be yourself, now be yourself
Guemeul sa bop xam ki gua doon ndeysan
I know it's strong, Africa is strong
Don't be afraid, never be afraid, that's what I say
Imanake donomaye obe kontere lela
Imanake famamaye obe kontere lela
Imanake donimaye obe kontere lela
Ajabalo ajabalo
Guemeul sa bop
Ikabido simasindole, I know it's strong
Ikabido simasindole, don't be afraid
Ikabido simasindole, I'm from Senegal West Africa
Terangua ligueye niakh djarigniou rek lagniou xam
Sama askan ligueye askan rek guem
Sama yaya ak baye dagn tete ci yoon bou bakh
Sama askan ligueye lagniou xam
Lalali lalee, now be yourself
Lalali lalee, guemeul sa bop
Lalali lalee, I know it's strong
Lalali lalee, don't be afraid
Lalali lalee
Def you melni def you mel ni lila wah
That's what I see
Def you melni def you mel ni lila wah
That's what I see
Guemeul sa bop ham kigua don ndeysan
Don't be afraid
Don't be afraid, that's what I say
Autor(es): Wally Balango Seck