
Cii biti
Uuuhh uuuh huuuuu
Walo kumay walo
Bama néé féss yéégg
Khawmawon numu démé
Dëëkëë funé, déf luné Guisse luné
Dugu cii luné, déguëë iit luné.
Cii bitii réw is not easy
Fii boy dokhe si mbédami ñu léy oytu
Dii jafandu séni sac ak takay
Mu mélni ñun ay sathie lañu
Mba lii ñu ñul mo takh
Té bo wotéwul thiowli néé kur
Buma doon sathie mba may deal
Kén duma lathie fumay jélé
Bés ñëëw ñu japama tédj
Ñuné mome il a fait le con.
Walo kumay walo
Fii Suma togulé duma lékk
Fii suma fotul passé duma sol
Fii suma féyul duma tëëdd
Té léép umpanaléne
Buma wooté né léép jaam
Nguir sutural sama boop
Nguir béñe samay béña jakhlé.
Walo kumay walo ooooooooo
Waloy kumey waloy
Uuuhh uuuh huuuu(x)
kumay waloy(x)
Writer/s: Alu Spear