
Dém
Bobu ba leggui may dém dii dém dii dém
té khamuma fuma jeume
Aduna mome de yaye dangueye
dem ba ñu yobelaa.
Ba ma yakare yegga fa ma jeume
Guissne mangui sogo diokk
Sokhlo wou dém wo sa moroom yaye
Waye li cii am solo moye.
Li cii am solo moy ne si yoonwi
nguir séy doom euleuk.
Bobu ba leggui may dém dii dém dii dém
té khamuma fuma jeume.
Aduna déy mome de yaye yoonn la wudul diékh
Yalla miko sakka rék leu beuggueu
beugguem di Kunfayakone
Takh na yoow sama wayjé jeumeul si yonu boroombe
Takh na yoow sama wayjé jeumeul si yonu boroombe
Bobu ba leggui may dém dii dém dii dém
té khamuma fuma jeume.
Bobu ba légui nuye dém dii dém dii dém
té khamuñu fuñu jeume.
Bobu ba leggui may dém dii dém dii dém
té khamuma fuma jeume.
Bobu ba leggui may dém déma déma dém
Bobu ba leggui may dém déma déma dém
Aaaaaaadunaaa
Bobu ba leggui may dém déma déma dém
Bobu ba leggui may dém déma déma dém
Writer/s: Alu Spear