Alu Spear

Iii mame ya done bañe


Print songSend correction to the songSend new songfacebooktwitterwhatsapp

Yeah hehehe hehe he
Yeah hehehe hoho hehe he
La mame ya bañone ba mu jaraléne séne
bakan mome la ñu sanjafoo.
La mame ya bañone ba mu jaraléne déé
Mome la ñu sanjafoo.
Ndjiitu Africa yéé war ngén kholat sén dokholin.
La mame ya bañone ba mu jaraléne sén déé
Mome la ñu sanjafoo.

Cii yoone yu lëëdëëm
Ñu bayi léép luñu amone
Daldi jéél yonu guedj mané
Sama gayi bésup tangay la wone.
Té war ko lébëël mané euleuk Suñuy sëët
Cii cadu yu gat mélni béééésss
Té muy won yoon yu dul faté.

Yeah hehehe hehe he
Yeah hehehe hoho hehe he
La mame ya bañone ba mu jaraléne séne
bakan mome la ñu sanjafoo.
Khana kholulén cii mame Cheikh Amadou Bamba
Ba tubab bii jëëlé yéép cii gaal wakhtu juli jot
Tubabi munéko dofi juléé
Bamba jëël derbi sani biir guedjoo.
Ndjiitu Africa yéé war ngén kholat sén dokholin.
La mame ya bañone ba mu jaraléne séne bakan
Mome la ñu sanjafoo.

Yeah hehehe hehe he(x)


Writer/s: Alu Spear