
Immigrés
Yeah ooooh yeah ooooh
Inmigrés yow dé Jambar ngua yow
Inmigrés yow dé Jambar ngua
Bayi yay ak bay, bayi mak ak rak
Bayi jabar ak doom jéé
None yék amdi jamayée
Ngiir joomjëë kon gorgorluloo
Ngiir joomjëë kon gorgorluloo
Khoslumi métiina dëëgëëla
wayé dal duñu wooré
Nguir joomja kon goorgoorlulo
Yeah ooooh yeah ooooh
Nguir joomja kon goorgoorlulo
Khaléy Joogaal néñu duñu daw
luka waral déégëëna noon yii diñu rëë
Khaléy Joogaal nÉñu duñu daw luka waral
man déégëëna noon yii diñu réé
Khaléy Afric dal dé duñu daw man
déégëëna noon yii diñu rééééé
Nguir joomja kon goorgoorlulo
Yeah ooooh yééh ooooh
Nguir joomja kon goorgoorlulo
Yeeeeeh ohhhh yeeee ooooh
Nguir joomja kon goorgoorlulo
Yeah ooooh yeah ooooh
Nguir joomja kon goorgoorlulo
Writer/s: Alu Spear