Alu Spear

Mare


Print songSend correction to the songSend new songfacebooktwitterwhatsapp

Nakh ngamay, nakh ngamay,
Nakh ngama ooh nakh ngamay.
Nakh ngama-nakh ngamay
Nakh ngama yow dém bayima.

Mare
Suma khamone suma démé bayila
nga dém bayamima .
Mare suma khamone suma démé bayila
nga dém bayamima duma dém bayila

Buma fatiliko bamay goné nga danma nétali
Buma fatiliko bamay goné nga danma nétali
Souleymane maman a dit on lave
Mais on ne lave pas figure
Souleymane maman a dit on lave
Mais on ne lave pas figure


Bama délussé keurgui daldi weet
Bama délusséyoonu guedj daldi weet
Bama délussé santhioub guedj na ték
Bama délussé yoonu xembé sélow lol
Bama délussé putu daldi weet

Mare
Suma khamone suma démé bayila
nga dém bayamima.
Suma khamone suma démé bayila
nga dém bayamima duma dém bayila.
Nakh ngamay, nakh ngamay,
Nakh ngama ooh nakh ngamay.
Nakh ngama-nakh ngamay
Nakh ngama yow dém bayima.


Writer/s: Alu Spear