Alu Spear

Néné


Print songSend correction to the songSend new songfacebooktwitterwhatsapp

Nena maaooo
Nena maaooo

Aaaah sama néné
Jamono dafa doy waar
Baye boye da tukki wone
Dém uti lumu aam
Dinga dëëguëë luné
Dinañ la wowé niit ku ñul
Niit ku wéékh mba imigré
Aaaah sama néné
Dinañ la jokhëëñ.
Lolu kham né.
Ñom duñukoo.
Nena maaooo
Nena maaooo

Aaaah sama néné
Am ngay mak sa Sénégal
Ay cusins Africains
Ay cusins Oropeins
Aaaah sama néné
Niit ñépa yém
Asiatic ak Américains
Africains ak oropeins

Nena maaooo
Nena maaooo
Nena maaaoo

Aaaah sama néné
Nama nama nama nama sama néné
Aaaah yow sama néné
Nama nama nama nama sama néné
Nena maaooo


Writer/s: Alu Spear