Alu Spear

Ngalaw lii


Print songSend correction to the songSend new songfacebooktwitterwhatsapp

Wakhal lu bakh,
Wakhal wakhal, lu bakh
Wakhal wakhal, lu bakh
Mudi Ngalaw duggu cii biir khol.
Wakhal lu bakh.

Ci biir alabi
Sukeu samay ôme
Yééki sama boop
Ubi samay gët
Cii digeunte garab yi
Jakarlok assaman
Léér léér takh ma tëëj, samay gëët.

Wakhal lu bakh,
Wakhal wakhal….. lu bakh
Wakhal wakhal….. lu bakh
Mudi Ngalaw duggu cii biir khol.
Wakhal lu bakh.
lu bakh(x)
Wakhal lu bakh(x)

Ngalaw heupe sédalol
Caraw daldi naw,
déér bi daldi yëgg séday cii biir khol.
Fatiliku tabi lu bakh ,
lu réfét ak lu ñaw lu bone
Réthiu daldi wés uhh
Réthiu daldi wés.
Wakhal lu bakh.
Wakhal wakhal…… lu bakh
Wakhal wakhal…… lu bakh
Mudi Ngalaw duggu cii biir khol.
Wakhal lu bakh.
Lu bakh(x)
Wakhal lu bakh…………lu bakh
Wakhal lu bakh…………lu bakh(x)


Writer/s: Alu Spear