Puppa Lëk Sèn

Ana ngeen


Print songSend correction to the songSend new songfacebooktwitterwhatsapp

So démé bay fateliku nadoon lulaay diëmé kanam
Woor na yallahou
Ki la waxon ki la défoon ,yi mbir du la diëmé kanam
Diangël djégale brother ,djégale ni la buur yallah
djégaleen
Yeah man djégëleen .
Ana ngeen ,mané Ana ngeen
ngeen nek yeen ngi fonk li geen doon .
Ana ngeen ,mané Ana ngeen
Fu ngeen nek yeen ngi fonk li geen doon .(bis)
Rise to the occasion big up yourself & know you strong ,no one can stop .
Rise to the occasion big up yourself and know you strong ,no one can stop .
Today it's your turn ,you half rise and never fall
Today it's your turn ,rise up
Ana ngeen ,mané Ana ngeen
ngeen nek yeen ngi fonk li geen doon .
Ana ngeen ,mané Ana ngeen
Fu ngeen nek yeen ngi fonk li geen doon fu ngeen né
Ana ngeen ,mané Ana ngeen
Fu ngeen nek yeen ngi fonk li geen doon
Ana ngeen ,mané Ana ngeen
Fu ngeen nek yeen ngi fonk li geen doon fu ngeen né
Ana ngeen ,mané Ana ngeen
Fu ngeen nek yeen ngi fonk li geen doon


Writer/s: Puppa Lëk Sèn