
Du niou ragal
Waga waga yow
Lumu waga waga yow blackman dina massa free
Mu nu gnou continer di dundu li sa yu gnu yéwo
Guiss lu ngu yém .
Mu nu gnou continer di dundu li sa yu gnu yéwo
Guiss ku nu saga
Dungu régal ,li gnuy dundu moy peace and love
Dungu régal ,li gnuy dundu moy aldiana
fekh jantaba gni jok ,gnun du gnu worry
Dëk di nu sikël man ,du tax gnu xaadi
ngëm ngëm la gnuy dem gnuy .
(Na gnu dundu peace and love
Ndax mama dane mama dane
Waga waga yow
Metite metite bumutax sunuxel yi paan xelyipaan
(Na gnu dundu peace and love
Ndax mama dane mama dane
Waga waga yow
Metite metite bumutax sunuxel yi paan xelyipaan
Black man doit se lever pour restorer sa dignité .
Il ne sais que c'est bombo hole veulent le niquer.
Écoute leur propos et tu verras que ça fait flipper.
Ils ne veulent pas nous voir prendre notre tiquer pour le zion ,yes le zion yow .
Babylon a parqué nos enfant dans ce qu'on appelle des cités.
Ils étouffent ils ne peuvent même pas respirer .
Tous dans le détresse mais nulle part ou le crier .
Babylon ne t'aime pas il est temps de le quitter .
Retourne au zion man prend ton ticket .
Il est temps de porter tes couilles .
Arrête de flipper man .
Sunu possone man moy sunuy gnite
Bu leen xaalat saax ,da gnuy tite man
Fi bofi bëgué doundu lion
fok gna demi lign nane fet
(Na gnu dundu peace and love
Ndax mama dane mama dane
Waga waga yow
Metite metite bumutax sunuxel yi paan xelyipaan
(Na gnu dundu peace and love
Ndax mama dane mama dane
Waga waga yow
Metite metite bumutax sunuxel yi paan xelyipaan
Writer/s: Puppa Lëk Sèn