Ndobine


Ndobino bëgë naaw ,Ndobino
Ndobino bëgë naaw mais mumuko
Ndax laaf yi la kéro
Will Ndobino bëgë naaw mais mumuko
Ndax laaf yi la kéro
wadiour yi gnu ngi sét sen dome ndobine
Ndobino mom ngi sét wadiour .
wadiour yi gnu ngi sét sen dome ndobine
Ndobino mom ngi sét wadiour .
fi mu neek ni, yermandé la saku mom
fi mu neek ni,mom deh weet na .
Ndobino bëgë naaw ,Ndobino
Ndobino bëgë naaw mais mumuko
Ndax laaf yi la kéro
Ndobine mom li bëgue moy fly ba way home
Ndobine mom li bëgue moy fly ba way home
Dafa bëguë guiss baay ndobino
Dafa bëguë guiss yaay ndobino
Freedom yo freedom
Freedom freedom ,we all deserve to know
what is freedom
ohhh la la oh la la la lé
oh yeah mama yeah i and sing for your freedom
oh yeah Africa i and sing for your freedom
Ndobino , Ndobino , Ndobino , Ndobino
Ndobino bëgë naaw mais mumuko
Ndax laaf yi la kéro


Autor(es): Puppa Lëk Sèn