Taxi Love


Sama love
Sama love
My taxi love

Chérie sama khol bi
Khol bi
Khol bi
Ioe yaci neik
Loumeu sori
Sori
Sori
Sori
Sori
Tewoul ni ngeu meu diegué

Neik ci keur done goor war di keurkeuréé
Ci taxi bi la dépendre
Leg lé niou wo meu urgence
Né meu gaz bi diekhneu
Ci taxi bi la yakar
Beineine gazeu
Enh enh oh

Leg lé meu tokk ci garange bi
Heurou agn
Wayei sama khel bii
Lepp tchi ioe ley nei
Diamono moma tagou
Chérie beug la teral té yor wa keur
Wa keur gue re

Smeu khol bi khol bi khol bi
Ioe yaci né
Loumeu sori sori sori sori
Té woul ni ngeu meu dieguei

Lek le ngeu wo meu téléphone ci yone bi feik meu yeb client
Doumeu beug loudoul mou wathie dokh ci sacii
Nguir niou meuneu tassé

Smeu métier bi
Métier bou noble leu
Wayei doumeu terei dound
Makheee sama love dall

Sama taxi bk koumou nekh ngeu yeigu wathiee
Nieup nioko mom
Wayei smeu khol bi baby
Watal na leu Doffii wathieuu

Anh anh anh
Seu birthday beu meu diouguei kolda tothie feu nieuw
Tcheu la khamni
Mak ioe
Dou mbeuguelou yegueul meu yegu
Wathieul meu wathie
Smeu ndigueul ngey dokhei
Nopal ngeu ma
Chérie nopal ngeu maaa
Gueum ngeu meu taxi
Kouthie gueneu dadj
Motchie gueuneu gaw
Geune tchié wor
Moins de tiono
Sama taxi love
Mak ioe dou mbeugueilou yegueul meu yegu
Wathieul meu wathie
Beuss bouneii

kombe legni wowé seu bay
Prince arona Touré
Bana dia sa yaye
Domou yatou bébé
Dagn yagueuu
Thiaminial Aida diallo chérie Segn bi
Lô ndam néné ko badoum Prince bayou
Mn frère n'a yonne bi yagueuu
Enh Prince mon ami Prince
Hawa baldei Prince bakhneuu

Wouyy Toro Gueye
Kokoy PDG
Narou marieme diallo
Sama taxi bi Toro gueye
Massou loma sei ladhe wethiéte
Enh Prince mon ami Prince

Chérie sama chérie
Yay sama réni khol
Moussou lo nangou niouy dem di nieuwate
Sama taxi love sagal na maa
Amorei lolei khana doy nala
Amorei lolei xana doye nala


Autor(es): Wally Balago Seck